Mbeguel is All 💛

By aloudiiaw

30.8K 1.9K 56

je vous raconte une histoire d'amour entre Ibou et Penda en wolof et français 😍... More

Presentation🎬
1-Partie 🎬
2-Partie🎬
3-Partie🎬
4-Partie🎬
5-Partie🎬
6-Partie🎬
7-Partie🎬
8-Partie🎬
9-Partie🎬
10-Partie🎬
12-Partie🎬
13-Partie🎬
14-Partie🎬
15-Partie🎬
16-Partie🎬
17-Partie🎬
18-Partie🎬
19-Partie🎬
20-Partie🎬
21-Partie 🎬
22-Partie🎬
24-Partie🎬

23-Partie🎬

568 29 4
By aloudiiaw

Le changement de Penda m'avait pas surpris parce qu'elle n'est bien dans sa tête en ce moment nakh beug tok Dakar mais je vais tout faire pour mou bania dem dakar si elle n'est pas têtu car je l'aime beaucoup beugoumako niak elle est l'amour de ma vie mais bon il faut ma commencer tangal di Thiago ay xoulo etc.. juste pour mou tok mbour mou gnibisi définitivement sen keur voilà meuna accepter lep sauf relation à distance meuna am sakh farr bou bess dakar si diguenté motax mou commencer façon lep lou am nasi kham dara je vais vérifié son téléfone samedi j'ai pas cours donc meuna dem dakar juste pour voir comme tay la jeudi souma wathie na dieune illimix orange woko pour xam siloumou nek vu que je connais belle et bien chez elle dinako enquête pour xol samedi bakham dou guene etc..
Vers 17h dama wathie sonu am bop bouy mety alors j'ai décidé nopalou nakh tangay bi moy lolou dafa doy war trop sakh actuellement je suis déjà au lit trop sommeil donc magui teudi à plus tard 🤚🚶🏻‍♂️
3 appels manqués📲:Penda
J'ai dormi 17 à 20h mane dal dama yewou rek guiss appel Penda yi mani weuh nelaw nafi dh louma dale tay attends ma recharger illimix bi wo Penda pour kham loumay doyè façon doumako wakh dina niew dakar
15 minutes plus tard ma def rechargement illimix #250# orange bi ma woko niou commencer waxtane .
Penda:Yaw Ibou wonala ba sonu dieulo ma dagua commencer changer wayer figua may fek
Ibou:Pardon oe dagua dioum wala mane je dormais defal nak bouma yab ok eupal gua trop beug na djiguene bou teyi adunam
Penda:Lane kone weroo yaw dafa melni daguay xoulo dh wala ma comprendroul batay say parole losi dioublou
Ibou:Yaw soma respectewon digua xol boy wakher ak mane épuis sakh niou wakh lenene awma diot ben benal bi sama crédit dou pour lolou inil diam wala ma couper sama téléfone legui merci
Penda: Akhhhh teuss yaw Dagua mer ni kone weroo mane ma sonu Ibou si wakh you sew yi vraiment xolal teyel say appel dinguama tchip
Ibou:Allô 📲Allô 📲 weuh ki mane lay coupè bravo li comme lou kocc  barma wakhone rek djiguene sopal te boul wolou migui ni wayer lep dina leer louy way reni say lokho lay nathie . Ibrahima mi louko dal yen liguay wakh ni nitt douko wakh dh .
Ibrahima :lima wakh leral doumasi nek di répéter wate jamais façon Magui lay setane qui vivra verra Dagua dieul sa décision Kone bakhna 👋
Penda : Esk do beuss sa xol bi tamite no gueune sa mer yi façon Magui khol si je reste à Dakar ou pas allez bsx 👋
Lendemain ma diangui nek classe professeur bi di expliquer xawma fouma nek nakh nop bouy mety et la discussion que je faisais avec Penda moma khawa sonal façon sama mbeguel si girls bi migui may beug eup lokho franchement mais bref Yalla bakhna il faut que je rentre à la maison pour meune nopalou touti sinon moy lolou mais bon damay khar cours bi diekh ma meuna dem galer ....
1heures plus tard j'arrive a la maison puis je prends soin de moi def coton tige samay nope et après ma teud nelaw vue que je suis fatigué aujourd'hui nakh sama febar bi dafma sonal trop tay  sou tanewoul souba damay dem hôpital consulter sama bop xol louma dal parceque dafmay tere nelaw et je ne peux pas supporté ça avec les études c'est compliqué vraiment...
Lendemain am yewou dem hôpital pour consulter sama beugn legui nak niou bi alma ay medocs pour mou calmer sama beugne et pourtant wakhone na Penda damay dem hôpital khol sama beugn bref docteur bi nena na bayi di lek niam you am chocolat surment nioy meti sama beugn yi
Allons si benen chapitre bi cava chauffer 🔥
L'aventure continue 🥰😍....

Continue Reading

You'll Also Like

872K 22.6K 80
Ses frères l'ont laissée seule pour partir en voyage quelques jours. Ils lui avaient pourtant demandé de ne pas traîner avec des garçons. Mais elle a...
1M 38.1K 46
Elle pensait être enfin libre, enfin heureuse. Elle avait quitté le monde dangereux auquel elle avait grandi pour mener une vie paisible loin de son...
51.1M 693K 83
« Y'a eu des bons moments mais beaucoup moins qu'ceux noirs » Chronique réelle avec des passages fictifs.
179K 8.9K 28
Emery Moore, nouvelle étudiante, débarque tout juste à l'université de Denver. Elle est prête pour cette nouvelle étape de sa vie, elle a déjà des pl...