Aller au contenu

xarbaax

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

xoolal xar ak baax

xarbaax :

  1. Indi lu bees lees baaxoowul woon a gis walla dégg, muy cosaan, xam-xam, xeltu, man naa ame ci bépp fànn.

xarbaax :

  1. Kii dafa bëgg di xarbaax ci lu nekk