Melosuufug Kamerun
Kamerun am réewu diggu Afrig la, jëmmam dafa mel ne ab ñettikoñ, rëye na 475 442 km², 98,8% di suuf, 1,2% ndox la, di 42u réew mi ëpp ci àdduna bi, am na it 402 km ci tefes.
Ay digam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Réewum Niseeriyaa moo ko féete sowwu, Mbàmbulaanug Atlas gi, Gineg yamoo gi, Gaboŋ ak Kongóo-Brasaawiil nekk ci bëj-saalumam, Réewum Diggu Afrig ak Cadd nekk ci penku, dexub Cadd bi ci bëj-gànnaar.
Xool it
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Xool it Wikimedia Commons
|
Melosuufug Afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkinaa Faaso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Bennoo yu Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eriitere • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Gine • Gine-Bisawóo • Gineg yamoo • Keeñaa • Lesoto • Liberiyaa • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeriyaa • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome-ak-Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togo • Tuniisi • Sambi • Simbaawe