Utilisateur:Groupe Lca/Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar
Fondation |
---|
Type | |
---|---|
Nom officiel |
Iniwersite bu Ndar |
Régime linguistique | |
Membre de | |
Site web |
Budget |
5 milliyaar ci 2010 |
---|
Pays | |
---|---|
Ville |
' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.
Démb
[modifier | modifier le code]Léewópóol Sedaar Seŋoor moo amal tegum xeer bu jënk ci wàllum taxawaay iniwersite wi ci 14 sãwiye 1975.
Taxawaayam mu ngi aju ci sart no 90-03 bu 2 sãwiye 1990, iniwersite wu Ndar mu ngi teeru limu ndongo wu njënk (600)ci 17 Desàmbar 1990 ci yoonu négandi.
Mu ngi jot gëddam ci ndogalu no 96-597 bu 10 sulet 1996 ak tur bu bees jóge ci ndogalu no 96-1016 bu 4 desàmbar 1996.
Ku ñu ko duppe Gaston Berger, nekk na ab kàngam ci wàllum xeltu, di doomu Senegaal ak Farãs, juddo Ndar-Géej. Di baayu Maurice Béjart.
Ràññeefi barab
[modifier | modifier le code]Diggànte iniwersite ak Ndar toll na ci fukki (10) km. Boo jóge Risaartool jëmsi Ndar di nga séen wërngalu kàggu gu mag bi. Iniwersite dafa fekk boole ñaari dëkk : Sanaar Pël ak Sanaar Wolof. Loolu tax na ndongo yi di ko woowe yenn saay Sanaar. Itam kërub internetu ndogo daara yi« http://www.Sunusanar.com » la ñu ko tudde.
Bërëbu tàggat ak gëstu
[modifier | modifier le code]L'université Gaston Berger est composée d'unités de formation et de recherche (UFR équivalent des facultés). Il y en a huit au total :
- Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
- Xam-xamu jëmale ak xarala
- Xam-xamu yoon ak politig
- Xam-xamu koom-koom ak
- Xam-xamu wérgu-yaram
- Xam-xamu mbay, sàmm, nàpp ak xarala yu màcc ci wàllum dund
- Caada, diine, taaral ak jokkoo
- Diiru njàng mi di na toll ci fukki weer. Di tàmbalee oktoobar jàpp sulet. Waaye ubbite njagale mi ak njeextal mi ngi aju ci barabu tàggat ak gëstu bu nekk.
Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
[modifier | modifier le code]Barabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:
- Angale,
- Farãse
- Làkk nasaraan jëmale,
- Xam-xamu melosuuf,
- Xam-xamu nekkinu àskan yi.
Xam-xamu jëmale ak xarala
[modifier | modifier le code]Barabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.
Mën a dugg
[modifier | modifier le code]Bànqaasu xayma jëmale
[modifier | modifier le code]Bànqaasu bitil jëmale
[modifier | modifier le code]Bànqaasu informatig
[modifier | modifier le code]Xam-xamu yoon ak politig
[modifier | modifier le code]Barabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:
- Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi ;
- Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris ;
- Bànqaasu xam-xamu politig.
Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi
[modifier | modifier le code]Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris
[modifier | modifier le code]bànqaasu xam-xamu politig
[modifier | modifier le code]Mën a dugg
[modifier | modifier le code]Xam-xamu koom-koom ak doxalin
[modifier | modifier le code]Kërug internet [1]
Caada, diine, taaral ak jokkoo
[modifier | modifier le code]Kërug internet [2] Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :
- Bànqaasu jokkoo,
- bànqaasu infogarafi,
- Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada,
- Bànqaasu làkk ak caada Agrig,
- Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
- Bànqaasu Xam-xamu diine.
bànqaasu jokkoo
[modifier | modifier le code]Mën a dugg
[modifier | modifier le code]tërëlin
[modifier | modifier le code]Mujjàntal
[modifier | modifier le code]Bànqaasu infogarafi
[modifier | modifier le code]Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada
[modifier | modifier le code]Mujjàntal
[modifier | modifier le code]Mën a dugg
[modifier | modifier le code]Bànqaasu làkk ak caada Agrig
[modifier | modifier le code]Mujjàntal
[modifier | modifier le code]Màndargal
[modifier | modifier le code]Mën a dugg
[modifier | modifier le code]Wàllum gëstu
[modifier | modifier le code]nekkinu ndongo daara yi (CROUS)
[modifier | modifier le code]yokkute lim ndongo yi
[modifier | modifier le code]
SAT | SEG | SJP | LSH | TOTAL UGB | |
---|---|---|---|---|---|
2001/2002 | 400 | 280 | 499 | 1480 | 2659 |
2002/2003 | 475 | 325 | 535 | 1525 | 2860 |
2003/2004 | 559 | 349 | 575 | 1506 | 2989 |
2004/2005 | 671 | 396 | 505 | 1799 | 3371 |
2005/2006 | 726 | 415 | 688 | 1965 | 3794 |
2006/2007 | 727 | 641 | 932 | 2143 | 4443 |
Dëkkuwaay
[modifier | modifier le code]-
Campus 2
-
Village B
-
Village E
-
Village F
-
Village H
-
Village H bis
-
Village L
-
Village L (Bis)
Loyer mensuel tout compris pour les nationaux | Loyer tout compris en frCFA pour les étrangers | |
---|---|---|
Villages A,B,C,D,E,F,K,M | 3000 (4,57 euros) | ??? |
Villages H,I,J,L | 4000 (6,09 euros) | ??? |
Dem beek dikk bi
[modifier | modifier le code]Tektal yi
[modifier | modifier le code]Xool yeneen
[modifier | modifier le code]Téere ak mbóotu tektal
[modifier | modifier le code]- Dossier sur l'UGB dans un numéro spécial sur l'enseignement supérieur au Sénégal, Le Soleil, janvier 2008, p. 5-6
Cosaan
[modifier | modifier le code]mbóotu tektal
[modifier | modifier le code]- Musée du Centre de Recherches et de Documentation du Sénégal à Saint-Louis
- Université Cheikh-Anta-Diop
- Éducation au Sénégal
- Felwine Sarr
mbóotu biti
[modifier | modifier le code]- Site officiel
- Présentation et images sur le site du Campus numérique francophone de Saint-Louis
- Site des étudiants de Sanar
- Fiche de l'UGB sur le portail SenCampus
- [https ://fr.glosbe.com]
Catégorie:Université au Sénégal Catégorie:Saint-Louis (Sénégal)